Audio - Affaire Khadim Ndiaye - Aida Macké: Les confidences du fils du propriétaire de la maison.

Ajoutée 8 nov. 2018

Commentaires

  • Maneh Ndow ci bakhoul. Lou melni kouko def Teh dofoulo, yahko teye.

  • Ack lou meuna xew femme bi waroul tall khadim ndaxx amoul lou meuna justifié ray vraiment femme bi criminelle la amoul domou mbacke mbacke mann ginaw yalla ack yonentibi psl serigne touba ack wa keureum la geum mais li acte volontaire la que justice soit faite li ct préparé qui mom dou dioulitt xanna

  • Yalna niou Alah mousseul ci djiguéne diou mél nii ak naaféckh yi koy woutal lây !!!

  • et alors?fami bou diegué rek ken douko tedj non senegal mo nekh

  • 🔴🔴🔴 Allez commenter ma dernière vidéo et abonnez vous, je rends🔴🔴🔴

  • .

  • Nous les africains gno guena sonou fi wayé tam gno nara guena sonou yawmal khiyam

  • Man dé tay la bayi tass Kimome nan الرجال القوامون على نشاء. Réwmi degue manofi am c impossible jamais. Par ce man yi journaliste maguis Amolén sakh odase posée les question❓ clairement Nit bo ray nit guénnan dondou kou warona diékh J8 peur de mon pay Motakh gnon macky sall rék mogno wara djité comme président mome mi wakh nous sommes des sytoiyé ordinaire Ou bien sakh sonko comme mome guemoul tarikha Ndakh dnépou mana tègué si yon Par ce ki lou rakh mo déf li da khamon ni dara doko si fék Mo takh mo am fit défli

  • Senega barina ay nafékheu

  • yalla na yalla yeureum khadim

  • moi je ne comprends Sénégal parceque ki raw dieukeureum wané naniou ko siwal ko fepp mais loutakh niou sathie khalé yi,di violé waté bouniou léne diapé douniou wané???????

    • Ameena D mais bo dieulé khalé lo koy doyé

    • sokhna si Ray bokoul ak leine

  • Mais bro bi vrai doff leu koi ...Meurtre am nganane plainte amoul..Même s'il n'y a pas de plainte, les responsabilités doivent être situées... La justice est là pour tout le monde

  • Koutaal dieukeureum nguéne naane kou bakh leu ...vrai dof nguéne koi ...C'est le monde à l'envers

  • Joli

  • Méchante épouse tu n mérite Pa être mère tu a mis la honte ns femme loumoutou done tale nite tu allé tro loin vrmmt

  • Ndawsi daal kou bone la té sokhor di lakk nit mélni kou yor dibitéri , nioukoy dèma rafétal li kéne manouko rafétal bam rafét

  • qui sokhor na trop

  • Li dawna yaram yalla rek mo kham

  • Un. Mari. Beau

  • Mane maa waarou

  • Djiepi na wa senegal 🇸🇳 Bilaye Walay femm bi bougn mako abalone nako togu lek ko Bilaye Walay en plus ki khamoul khol mane Serigne ak famille douma leine ax falè force damay ray femm bi mou nek match null Bilaye lou nit firr firr tall c la dernière chose koi

  • Vous etes trop hypocrites mes chers journalistes c est quoi c est histoire on parle de meurtre de premeditation

  • Crime par préméditation. Donc c'est la prison directe

  • kimom dafabon torp

  • Yaw mom mansour diop mala weddi naké yaw Domi haram gua geumoulo dara amoul domou serigne amoul dara wakha li yalla wakh si kou ray niit na nekeu domou seuydina mouhamet baxam

  • Ki dh koukoy takat day taylè bopam😂 rk

  • HA LES SAPEURS POMPIERS !!!!!! TOUT MARISTE POUVAIS PRENDRE FEU ET EUX DISENT MANQUER DE RÉSEAU !!!!!! HA LE SÉNÉGAL !!!!!!

  • Eskeuy yalla sounou borom.. Ki mo bone deugue, takhaw âme fite di soti nite essence talko mou dé

  • Loutah sénégalèyii naafèkh.elhadj dall wèdinala.

  • Bayileen mou bonne lou nieuw ngeen wakh ndogalou yallah YALLA kouko wo kouné daley diapalé soutoural la mais Satan naak kouko wo mou wouyou sila Jalousie bou eup bakhoul day attiré Satan donc d'après les disputes la femme n'a jamais respecté son mari ndakh khamna elle dira k sama papa moy serigne niam di gorom douma sania deef darra Kou goor ki ndeyssane mélni kharou yaar ndakh am respect am limouy rouss ak loumouy khol! Mane naak je les connaisse pas mais souma bokone ak khadim Ndiaye bou yabbo niou reyma déh mais Dame bi dinako deef cicatrice bo khamné heure bou sétto dineu fatélikou limou deef Wassalam Repose en paix khadim sunu borom doula sétane been yone il sera ton avocat Dinala pledel amoul serigne amoul justice mo bok ndiaboté nieup on est tous égaux devant lui!

  • Prémédité

  • Kou ray danioula wara ray

  • C mon oncle le frere a mon pere ke dieu l'accueille au paradis...

  • Mane kouyor bi khole ya ma meune

  • Mane kouyor bi khole ya ma meune

  • vraiment cet acte est inexplicable! mais Allah voit tous même si elle n'est pas punie dans la vie présente, elle le sera dans l'au delà!

  • Boukene togn seytanè nak Jalousie c animal .beuy sakh dafay firr Guinar sof mbame khoukh. Mais dem bay jeul essence talll Kou sokhorr lol lol lol mokoy def Sa merite punution .loi kasso charia reyy

  • En plus il etais tres beau wallah thier elle a gater la vie de ce jeune homme.wallah

  • On a qu'a appliquer la charia wallah ke Azawadjel accorde a khadjim le djannatou firdaws

  • réponse en paix

  • Slu

  • Quand une femme est movaise elle est très movaise.

  • Elle méritte l'enfer sette solope de Aicha mbacke nitte kou meune déef

  • Mane dee sama yone nékoussi Dee! Khawma Lou khew ! Wayei problème waroul takh keneuh dii taaal nite nak

  • Sa diabar boula talone do wakh laulou imbéciles

  • wa tamit mane dal meunouma comprendre nit Lou gnaw li rawatina Ray nit gnounane nit yi nagnou manou la femme limou def dara meunouko rafetal ak famille boumou meundi bok yakhna derou ay mbokam fi mom kou dé ya perte même bou amout plainte yone dina def liguayam lima meiti thi Sénégal mou moudjei beuri ish se pays de merde

  • Hum diga teud prison dè k sa soi clair dan ta tête .de plus tu n la jamé aimè kéne dou dèf Lou bonn lhomm de ta vie c du nimport koi

  • Astou ya bone di rey

  • Lou geuna grave si li ni dome dji mou wossine le lendemain sou magué ladj yayam kane moy sama papa lane lako sokhnassi di tontou

  • Al maktoum.newonna nan sangat rewmi.ndax danouno rax.yenn yi douk neen.taal sa dieukeur.rendi sa baay.ak ay xarou youdoul diex.ta ay djoulit rek koy def.yalnanuci yalla miuseul mes li doyna war