Cheikh Niass : "Mon père sera enterré à Yoff, c'était sa dernière volonté"

Ajoutée 5 déc. 2018
Retrouvez-nous sur http:www.igfm.sn

Commentaires

  • ndéké kou diour sa dôme perto ndiro am n'a nôoo

  • k Dieu l'accueil dans son paradis éternel

  • Yalnako yalla yereumm

  • Que Dieu vous donne la force de surmonter cette epreuve ...paix a son ame

  • Paix à son âme cé triste

  • La prochaine fois avant de te prononcer, dans de pareille situation, il faut consulter et se concerter avec tes pères. Les familles religieuses sont régies par des règles et principes. Lèona Niassène est la terre de sa dernière demeure. Qu' il soit accueillie au PARADIS avec tous les honneurs. Amine

  • didi yalla nakou yalla yarame

  • Mais tamite qu'il soit enterré à yoff wala Kaolack la personne est déjà mort PQ beugue kheuthio????? Wa keureum n'a pas de mot selon car il a une famille ses enfants veulent l'enterrer à Yoff c'est tt!!!! Au ciel il est avec ses parents et grands parents 😑😑😑😑

  • Khouloo katyi naniou noppi Le dernier mot revient à qui il a parlè en dernier:son fils Que la terre lui soit legere et allons preparer nous aussi NOTRE JOUR IL EST MORT PARCE QU'IL VIVAIT'

  • Na talibe yii yam way se sont c fils ki on le droit sur lui

  • Bien dit bro

  • Sidy Lamine Niasse était un homme du peuple, la voix des sans voix nittou askan wii. Donc l'amener à Yoff serait le rendre au peuple.

  • Ooohh li metina yalla na yalla watiei yeurmandem tie mom ak mboleme dioulite Defal lene ko limou beugone osi

  • Combat terminé. Tu sais pas comment parler

  • Wa ana khalifa niassen yi loumo wakh rek lano wara deff nitt daye am kilifa wasalmm

  • Thiey adouna kou dés rk ya perte niit ki demna ba paré djaroul khiro il faut respecter son dernière volonté

  • Yalnako yalla kharei aldianay firdawsi ya thi barké s mouhamed psl amiiiine

  • Allahouma Ghfirhou warhamhou ! Ya Rabal Alamin

  • mane mounouma comprendre sa papa ganiou nga kheuy taxaw daiakarlo ak press bi di wakh 😔😔légui dééh nekatoul dara !!

  • Maitre Cheikh🤔

  • Yaram dawna

  • Journaliste bi sof gua ak sa francais soff nguene ak français yi Loutakh vous parlez pas le woloff putain c grave pour nous . Paix à son ame

  • Mane sénégalais khawma loulene dall bou nit guené Adouna nguene déplacer yobou Touba, tivaouwane etc.. Mais fep bene leu nitki fimou décédé lanouko wara soul rawatina fi sa ndiabotame nek ba paré le défunt sa volonté moy niou soulko Yoof kone danguene KO wara respecter kilifa bou Tolni sidy lamine niass décédé depuis mercredi nguene di khar ba vendredi pour soul KO je suis d'accord avec le fils

  • Nagnou bayi jugé lougnou woroul,Sidy lamine sou amoulwone foumou ték Ahmed halifa douko toudé 2fils.emplus gno bokou nday ak baye kimporte l blème kils avait se sont des frères.sou fékone dôme moy décidé dou ki mo wara décidé pack il né pas l'aîné.nagnou mandou

    • +Fatma Balde guisga motah gnounane nite day am kilifa.te Ahmed Halifa sène kilifa la, té dou lep lagnou meuna wahh.mais Sénégal di jugé nite té hamougnou rek lagnouy def

    • réalité absolu gnom lignou wara def moy topou thie guinaw Ahmad khalifa niass ndakh moy senn baye di senn magou baye ish Lima soof thie mbirmi moy gnep khamnagn ni dagnou am problème tei thiowli meune na yeg foko foguéwoul ndakh meun na dem bathi senn seute seutat yi

  • Paix a son âme😭😭😭😭😭😭

  • wa papay jambour même bouko wakhul wone sakh dom yi gno thji am ndogal bulen foto

  • yalla nala yalla yereum

  • kaolack c'est international mais sic 'est la volonté de Sidi laissez sa famille l'enterrer à Dakar.

  • K la terre lui soit légère, mais cheikh on te comprend car tu as reçu une éducation à la française. Mais dire k enterré sidy à Kaolack est une dimension locale confirme ton ignorance, Elh Abdoulaye, khalifa et Baye Niass sont enterré à Kaolack et le monde entier les fait le ziar everyday

  • Yalna ko yalla yeureum amin

  • Le grand père de sidi, son père et même sa mère qui est descendante du prophéte PSL sont tous enterrés à Léona(kaolack).Ce que son fils là qui n'est même pas l'aîné raconte n'a aucun sens! Sidi doit être inhumé à kaolack auprès des siens; c'est la tradition dans tous les tarikhas du Sénégal. Al Makhtoum a longtemps vécu à Dakar même durant son khalifat; cela n'a pas pour autant empêché qu'il soit inhumé à Tivaoune après son rappel à DIEU. Vous n'avez qu'à sortir ce testament ou sidi lamine à demander de l'enterrer à Yoff et le débat sera définitivement clos. Je pense plutôt que ce petit cheikh niass veut rendre hommage à son père à sa façon en l'enterrant à Yoff dans la neutralité "chez les sans voix" pour mieux coller aux convictions de son père durant son vivant et qui était de toujours se ranger du coté du peuple. Son père avait des positions durant son vivant;personne n'en disconvient;mais cela ne traduit pas pour autant une volonté de ne pas l'inhumer auprès des siens.

  • Il est fort le petit il souffre intérieurement mais il a pris son courage à deux mains. Que la terre lui soit légére

  • Yalla nako yalla khare Aldiana

  • Bien parlai cheickhe je te presente mes condeleance le dernier mot te revien

  • boulaine sonale new bi yalnako yalla hare aldianaye firdawsi yoff la beugue yoboulaine ko yoff

  • Sidy lamine niass fr-tv.com/tv/vid%C3%A9o-lmoFWDUEj-I.html

  • yalla na ma yalla ball wayé cheikh niass mii woolou mala de

  • Paix a sont âme

  • Amo kilifeu, xaley dou kheuthio! Beusseul sa xol, nga ceder

    • Waxo fi touss dakar ak kaolack lan moy difference bi

  • Wonaa goonga wona fof en kay.

  • Lii moy sénégal nak booy doundou lo wakh niou wèddi bo fato nak kounèkk di wané thiofèlam , guemouniou touss , sydi lamine nak limou liguèyal sénégal ak diiné ak langue arabe yalnakako yalla fay , té lou waay déf boppam

  • Lii moy sénégal nak booy doundou lo wakh niou wèddi bo fato nak kounèkk di wané thiofèlam , guemouniou touss , sydi lamine nak limou liguèyal sénégal ak diiné ak langue arabe yalnakako yalla fay , té lou waay déf boppam

  • Paix et repos a son ame .J ‘ai vraiment pitie des enfants .Dara xewagoul gnou commencer polemiques .Il faut se plier a la volonte du defunt qd meme ,respecter son souhait . C est triste de se dechirer comme ca ,alors que sa famille proche ( enfants et epouses ) ont besoin de soutien. Seul Allah est Unique et Puissant ,il faut arreter d ‘abuser de votre “ pouvoir “ soi-disant que vous etes des hommes de Dieu .Nul n est infaillible .Ayez pitie de ces enfants et laissez les enterrer leur papa selon sa derniere volonte .C est vraiment trop !!!!! Le defunt doit reposer en paix apres avoir termine sa noble mission sur terre .Yeeneu yiii aakk bou mack leu .

  • yalla.n'a.ko.yalla.hâter si.yeurmandeme.mou.khiper adijana.

  • Que son âme repose en paix.

  • En tout cas on écouter ses fils et non à ceux qui n'étaient pas en bons termes avec lui de sont vivant

  • eyyyy waaay bayilene domame mou yobouko yofff

  • mandou leine ci famille diambourr QUE LA PAIX LUI SOIT LÉGÈRE

  • Manchallah comme son père!!!yallah nako yallah yeureume té yékhégnou

  • k la terre lui soit legere et k le bon Dieu l'acceuille dans son paradis celeste

  • yalla na yalla watou lene si sen barke mame

  • Ce n'est pas à quiconque de décider outre que ses enfants à plus forte raison que ça soit le voeux du défunt. Nit kou nék nangua ko jappè ni soudone sa baye noy déf. Sénégal so déwé gnou khethio la, sougnou la soulè faté la. Gneup gnoko beugue wayè ki moko fi togal . Nagne ko gnanal Yalla na ko Kharè Aldiana firdaoussi

    • +Rémy Joe Niafouna Yalla nala Yalla dolil Diam

    • +Rémy Joe Niafouna pardon frére. Yalla nagnou défal diam

    • je e parler pas a toi sur le commentaire mes plutot a adama ba

    • +adama ba je suis Dacord mais khana papame Sidy dou kilifame. C son père qui lui a demandé ça en plus c qui la famille?? Hmmm

    • +Rémy Joe Niafouna tu n'as rien compri. Apprends à lire si tu use de ta capacité mentale

  • mandou léne thi famille diambour

  • metti na wayé nitt da fay am kilifa sou ma nekkone mome di na ni bene pape la niou fi déssé mouysa ma Papa Akhmed Khalifa NIASS sou niou wakhtané si sou nou bir famille ba paré di na niou ko diokh kaddou giu mais pas ca Sidy yalla na ko yalla kharé aldiana

  • thiey addouna

  • Bu léen juuyóo mok dik lu léen seen papa ahmed xalifa ta def lim wax am kilifa lu baax la

  • cheikh vu ta façon de parlé on sait que faté nga say ada ak thiossane tu es un français maintenant mais lifii mame yi bayi dou dègne say kilifa nii on lamène a kaolack pres de ses parent ngay wakh pourkoi les marabou qui sont mort a lextérieur on leur amène dan leur pay dorigine toi un jour si tu meur on peut tentéré en france sidy es natif de kaolack ses parent son entéré a kaolack nasirou mou mame baye quan il est mor a letrégé on la amené a medine yaw khamo touss ferme ta bouche

  • Atakhwal allah ragalen allah

  • Li taw wakh moy ame

  • Ndeysanne

  • Mé môme wa médina baye la pk yoof

  • Nayesane ly metina trop mais yalle nakou yalla hari adiana filedawci

  • mérci ca wakhe rafét na

  • Yallah nako Yallah yerem khareko aldiana Bou kawwe nit Bou dewee Lou Guen bakh Guen gaw ndenthieko 😢😢😢Ndyessane sidy dama ko yagg beug ndiakh djikommm🙏🙏🙏

  • Paix a son ame ke dieu l accueil dans son paradis amine

  • Kaolack c’est une mission locale et dakar une mission internationale qu’est-ce que cela veut dire? Et qu’en dis tu de la mission de baye qui dépasse les frontières alors qu’il est enterré à kaolack...? Voilà les conséquences quand tu élève tes enfants en dehors de tes racines...ce fils parle d’élite et de nouvelle classe sociale don’t appartient Sidy pour l’enterrer à Dakar...je doute que ce soit la volonté de son père...

    • @Feuz john jay u as parfaitement raison c'est juste une question de deracinement et d'ignorance de la realité

    • Maandou leine si mogueun

    • il nest meme pas son fils aine

  • Je nè jamè vu ça c sidy lamine dè wala daniouko fatè taye il a rendu l'âme kounèk meune nga takhaw wonè sa bopp pour takhawouko parsek sokhelatouko meune n'a wate si yala ni wadiale n'a bopame li moulène bayè ni mouye dieumeum dji dième nguène si bamouye dounde meunouléne si dara ndakh boba lérou rouhou gui molène diakhalone fi mou tolou loulène nékh défelene si wayé kharitou frero yaakarnani dôme bou gore majeur warenamana takhawou bayam boubakh ndakh souba môme moye déssate akk lifi papame bayi mouye jaabot gui sidy bilahi yala na la yala kharè Aldiana dama meussa guiss si sa kanam ak jambare lou nè dadienako wayé mougne rekk yala boula thiate djitou

    • Innalilahi wa inna ileyhi radjihoune yeurmandé borom bi yalna beri tha mom bidjayi seydil woudjout Amine ya Raby

  • Nit ku nek kam beug lay deukkal eleug, Sidy Lamine beugg na Senegal ba yelloo ñu robko Yoff ci Dakar Capitale Senegal ndax ñep yem ci mais nak Sidy ay wëyjuram aki mbokkam yiko defar yarko bam mel nimu mel tay ba ñep diko xeuthioo, ñooñu di ayy weyjuram di ay wassilaam la gueuna beugg waay, talibé Muriid boo guiss li ci eup dafa beugg bu faatoo ñu robb ko fa seriñam teudd... «almar'u ma'a man ahabba» ci zaahir bi yaqqul dara, baatin ba moom matt na bu yagg

  • 😭😭😭

  • Voici Notre Nelson Mandela au Sénégal Nous les sans vois .on pérdre Notre Père. Yalla n'a yalla wathié yeurmandé si mome

  • La logique voudrait que l'on enterre à koalack à côté de son père malgré son statut de Journaliste il est un homme religieux et respecté par son savoir

    • bien dit moussa camara

    • Il savait déja la logique car il maitrisait sa religion sa famille et sa societe alors k il avait designé Yoff donc la logique doit être son choix mon frére paix à son âme

  • Tijan you are right I feel for you

  • Sénégal niackaatinna killifeu gou amonne yaakhinne

  • Yobou ko Yoff té nopi diapou sa diambourr yalla bakhna barina soutoure

  • Killifa bou tolni Elh Sidy lamine Niass nélaw Mardi fii ni Sénégal, gnou beugue ko téyé ba vendredi dok ko dinth😡 en plus fou bokoul ak fimou taneu😭....mais on est où nak? Mane mom j'suis avk ses enfants ndakh Sidy bimouy doundou gnom ladone guiss et se sont eux qui doivent décidés pour lui boufi nékatoul!!! Que Dianatoul firdawsi soit ta demeure éternelle Elhaj Sidi🙏❤

  • Yamal palace khalee mo gueune si yaw wakho deugeu ton père na jamais di sa ces pas vrai je te defie moi oumar sall niass actuellement je suis a la maison ton père akhmed khalifa niass ta demandé si ton père ta demandé sa tu as di nons donc ton père na jamais di ca

  • Thieuyy Adouna mann dalle waarouna siiww dou diammii borom

  • Paix à son âme. Les propos entendus sur la déclaration de Cheikh Niasse,si ce sont ses propres paroles elles l'engage.Mais si s'était la volonté de son père donc rien à commenter

  • Yoff fou baye laye

    • stp pas de polémique . Ya khayrou khal khilah santoula li. C pas le même context

  • yaw la andal sa baye leu mouvement % rkk yoff

  • CHEIKH yaw sa wakh dji diaroul yone mane geumou mala

    • Yow werro dè

    • Ioe nopill kii il vien de perdre son pere c normal qu'il fasse ces derniers volontés

    • Kou deuguer fitt ga on parle d'un mort koussi wah lo warou wah reik yangui togne Yoff la beugone prkw pas

    • Yala rek mo xam Lou diar yone ak lou diaroul yone ki si nakar la nek bayil critiquer t nianal ki fatou mo eupeu dieurigne

    • Daouda Doumbia yaw bayil ba mana wakh

  • Dèfal li Ahmed Khalifa niass Wakh ndakh moye kilifa sidi lamin yaw sa diann waccna

  • **Ces imposteurs veulent récupérer le décè pour se faire de la fortune et refaire leur image... Laissez son fils aimé prendre soin de son père et exhaussait sa volonté ultime♥️ **

    • Belizo ma degue deugue merci mon cher

    • +Rémy Joe Niafouna suis parfaitement d' accord avec toi mon cher.

    • ceci cet nes pas a toi ni au senegalais den decider il a demander a se quil sois enterer a dakar ont doit respecter sa volonter en tant que telle

    • Khalifa niass waroul wax dome dji di wax realité senegalaise mo commencé yakou et c’est à leona au près de son père qu’il aura plus de prière ki dei niane rek la sokhla

    • arame mbow c normal pask c lui ki est au senegal

  • Dioumgua

  • Le fils lui ressemble beaucoup. Paix à son âme.

  • Nous présentons nos condoléances au groupe walfadjri mais aussi à tout le peuple sénégalais. Le Sénégal vient de perdre un grant homme, un combattant un défenseur des libertés et de la démocratie. Un homme intègre, constant dans ses principes et qui a jamais abdiqué à combattre l'injustice. Que le bon dieu l'accepte à son paradis amen

  • merci cheikh il faut bien respecter sa volonté divine

  • Yalla nako yalla kharè aldiana

  • Non non Dakar

  • Non non Dakar

  • Rip we'll never forgot to pry for Sidi Lamine Niass

  • Nit day am kilifa challah niasse lii dou yoonn

  • Rip😭😭

    • yalla nako yalla yeureume kharalèko aldjana firdawsi yalla na khiper aldjana firdawsi amine

  • PAIX À SON ÂME ALLAHOU MA AMIIINE

  • Machalah yalnako yallayeureum

  • Sidi lamine keye j'ai jamais vu quelqu'un d'aussi intégrer il était à l'écoute de tout le monde je me rappelle quand j'étais jeune et que y'avait que le rap dans les années 90 pour que les jeunes puissent s'exprimer.toutes les chaines sénégalaise ne donnaient pas la possibilité aux rappeurs de s'exprimer.yavait que pour nous les jeunes walf . merci tonton sidi pour tout ce que tu as fait.ton âme reposé en paix maintenant

  • Assalamou aleykoum. Mangui dialé nieupe. Il faut respecter la volonté du défunt. Et l'enterrer a Yoff. Merci

  • Défal ko limou beugone sénégal boye donde nio dilla khékh so déh wé ko nék di reuye laminie ya yoré kadou bi ndakh yaye tawam dén thie ko fimola wakh té nga nianal ko yallah niéguel

    • Astou Mbaye bien dit fi da beuri ay nafékheu

  • Wakh bi raféte na loole

  • Massa maguilakoye dialé sigiille digualé yala nako sounou borom bi faye kholame bou raféte niass