graves révélations de ahmed khalifa niasse "ils ont tué mon frère et je vais..."

Commentaires

  • Machallah ler n'a diaradiaf Niass

  • Sunu xell dou masa diouk si Elhadji sidy lamine niass Tey niane Yalla mou teralko sa Aljana firdawsi

  • merci rafétena yalla noko yalla kharé aldiana firdaossi

  • Rip

  • Rip

  • Rip

  • amna gnokhamné dougnou wakhlou rafét mais Ahmed khalifa niass limou wakh lougnou mana dégla ligadef rafétna yallnalafi yalla yaggall barké cheikhoul khadim.....sidy lamine niass yalnako yalka kharé aldiana barké mamam seydina mouhamed (slw)

  • yalla nako yalla yeureum, khareeko al dianna té samme la niass

  • Paie à son âme et que la terre de leona lui soit légère

  • Hamet wadji rafetna lol sakh yalla nako yalla kharé dianatoul firdawsi sa yalla dolé takhawou

  • ki nimako mere maitesin après la mort

  • cliquez sur ce lien pour voir les raisons:fr-tv.com/tv/vidéo-Us4A0xD6NWY.html

  • Yo Allah yourmo yafomo yo Allah harnoumo alidjana amine yarabi

  • Ahmet khalifa Niasse est un gros menteur, un affabulateur😐😐..je suis trop fàchée sama khol nékhoul...Ecoutez la video de son fils Cheikh Ahmet Niasse (dont il dit kil né pas l'ainé) ki dit: " son père avait échangé avec lui plusieurs fois sur whatssapp et disait kil souhaiterait étre enterre a Yoff à sa mort" ( entretien sur Walf tv avec un journaliste)... lolou dome di na ko fenne si bayam..mou gnewe di wakh lénne. Yalna ma yal bal té diéguelma si wakh bi wakh si ce monsieur là! Et puis malhonnete kil est: si YOFF yavait pas de blem comme il dit, pourkoi ne pas l'enterrer laba? lui méme dit pas des choses normales.

  • Toujour les Franc maçons mai en quelque sorte Ahmed Khalifa niasse même si tu va te venger mai tu dois garder les secret familial comme tu va payé les études donner les enfants de quoi manger etc... ou vas le monde je ne di même pas le Sénégal avec cette puissance mondiale 😏😔

  • Paix à son âme sidy lamine diambari l'islam

  • Quallah l'accueil dans son paradis céleste

  • Yalla nako yalla yeuram ta khare ko aldiana firdawsi 😭 Yawit yalla nalafi yalla yagal lool amine

  • Gni ay nitu problem lagn. Mé senegal mom kou dè done waliou

  • Paix à son âme.,et longue vie aux autres.

  • C'est triste vraiment Sidy Lamine Yalna YALLA yok lérame té oyofale soufe si kawam

  • que dieux l'accueil dans son paradis

  • Yow ahmed doo rouss tu es pathétique yaay pir dajjal ibliss 😡

  • Yallah nacko yallah yeureum té djégueul ko kharé aldjanatoul firdawssi barqui borom Touba khadimou Rassoul yallah n'a nacko sanguam wou teed wowou terou cheikh Ahmed tidjani

  • Khalifa Niasse noppil

  • Ndeyesan yalna ko yalla kharé adiana

  • J'arrive tjr pas à croire qu'il n'est plus 😔😔 ndeysann

  • Kadou yi rafetna Machalla

  • Yalnako yalla khare aldiana firdawsi je crois son discours certe c magnifique mais sa aurai pu reste au sein de la famille

  • Je ne comprend pas pourquoi cheikh voulait ecarter ses 2 freres ainé....c est pas serieux

  • Ndeysane Yalna nako yala yereum kharei aldiana fiirdawsii amine

  • rip sidi lamine niass

  • Aduna amoul solo sidy yalla nako yalla yeurem

  • Sénégal mo nieuk

  • Wakh deug nainene bayi kilifeu ahmed decidé fougni dinth rakam nakhté mak denkeye ormal djokko loumoumome sidy kou bakhla kou dimeuli aye domou adama la donc la decision apparttien au grand frere ahmed c le kilifeu de la famille

  • wakh dji refet na

  • Svp c est pas le moment toi tu connais pas les noms des enfants de sidi lamine niasse paix a son ame

    • C est le Senegal qui a perdu

  • Pai a son ame

  • 😭😭😭😭

  • Yalla na khipé aldianay firdaysi

  • avent TT j vous dis inna lilakhi wa inna ileykhi radioune.mame sidy.nite gnou Barry dougnouko raagné kééke guénoul adouna en tte franchise j n lui donné pas trop d importance.en fin yalla nako yalla yeureme kharéko ardiana oyofolko souf thi kawame.merci

  • Sénégal niakc n'a bonkal mou khamne dou tofi amati

  • Nous sommes tous des sénégalais priés pour le repos de son âme

  • Un gd homme est parti k Dieu lakeuy ds son paradis le sénégal avait besoin de toi pdt les elections Sidi est iremplaçable

  • Ndeyssane sa wakh rafetna yalla nala yalla defall diam

  • Mbéguélle gi ma amône thi yaw yokouna téy yalana yalla yeureum seugn sidi té bayilafi ba nga ame 100 ans té wér

  • nit kou bax ta fonk l islam

  • yalla nako yalla xare aldjiana

  • Ndeyssane

  • R.i.p

  • Yallnako yalla yaram te kharrèko alldiana si barkep serigne touba akhmad xaliffa liga deff refettna yallnala yalla fay si barkep yonentibi salla -----------------wa salam

  • Yallanako yalla yeureum tékharéko aldiana

  • Il ne faut pas jugé ameth khalifa de mal son problème ak sidy yaguena na si famille donc fait attention pour vos jugements Ahmed reste toujours grand à sidy lamine Que terre lui soit légère si barki seydina mouhamed

  • Svp bayil cheikh mou dèf li papam beugeu sa domla

  • اللهم أغفر له وأرحمه ووسع مدخله وأسكنه جوار سيدنا محمد صلى الله عليه وسلم آمين

  • halaat leen lou wahone Ay wah you niaw en vers toute la communauté peulh

  • Yalna ko yallah kharé aldianay firdawsi, Sénégal gnépa niakk....

  • Yalla na Diam sakh si rewmi, Sénégal deuk diam la deuk diné la

  • Yalnako yalla yereum té xarrr ko aljana firdawsi paix à son âme

    • Paix a son ame sa xaw rafenat yala na la faye mboko alalou yala diara dieuf tonton khahmete

  • Yalla na déé di noflayam famou djeum gueuneul co fimou djogué si barké Baye ak bayam

  • Ndéyssaane rafétna Ahmad vérement kilifeu nge machaalah

  • c Allah qui prend la vie comme Il veut.cessez d'incriminer qui que ce soit et priez pour que Allah étende son person à tous ceux qui aiment Seydina Muhammad psl

  • Yallah nako yallah yeureum kharé ko aldiana...Mais kii loumouy wakh kéne douko wakh déjà ki kéne diebeulo gouko suñu borom mouy beugg andi polémique ca se fait pas ahmed khalifa....où en est ta croyance en dieu si tu te dis que tu es un homme saint🤷‍♂️

  • Machalla wakh dji rafét na

  • Paix à son âme Ahmed khalifa yana yala goudal fane yi

  • problème bepou yako fi indi lo dougou rek indi fa thiow

  • Yalnako yalla yeurem

  • Yalnako yalla yeuram té khareko aldiana

  • Paix à son âme que dieu l’accueille dans son paradis ,un homme dignes,tu resteras grave dans nos cœurs

  • Amna kaddu yima rafetlewoul dakh c'est pas le moment et ni le lieu

  • Yalla nako yalla yeureum te kharko aldiana barkep s saliou

  • Youbou lene ko touba kaye waxdji djiekh

  • Cei vrais ke metinat mais ne sois pa a la place de dieu bayilene ak yala dara oumpouko

  • Deireite daffa fort wallakhi ndeyssane

  • Am mbok boubakh mo rafet kar machala

  • Yallah nako yallah dieguale amine

  • Repose en paix Sidi Lamine Niass que Dieu t accueille dans son paradi Amen

  • Ki vrai iprocrite la lép loumou def rek defouko si zero louné gaka dan yak

    • loumana khew rakam la kone arrête ces insultes loléne di saga nite bambou ame nakhar khana ngéne maneko bayi

  • Masseu Khalifa meetina, je réitère mes sincères condoléances à toute la famille NIASSE. Yal naco YA ALLAH sunu borom bou tedeu bobou Akfirlahoum wa Rahmawou Sidy Lamine NIASSE. Le Senegal à perdu un grand homme de valeurs, il a honoré sa mission de passage sur terre avec honneur MashaAllah. Seutou yonèteu you bakh yeupa soneu, dagniouy djihad ba bi gniouy wouyou dji sène borom. Wayé guinawam rafètna yaleu bouko thiate djitou ci bamelame. Je l'aimais tellement❤. Il restera à jamais dans mon coeur😭😭

  • Paix à son âme qu'Allah l'octroi en son paradis

  • Yena gui dieuw dee rekk mowour yao amo diom mandouvo

  • d’abord kou sage kou am xam xam demna djalenako senegal yeup yallah nako yallah xaré firdawsi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾ok maintenant Waxna ba wax lou eup li mo tax gnou mane wax foula day gatt khalifa Niass en ce moment est rentrè dans des polémiques vrmt pas nécessaire wax deu yallah. Ahmet Niass xawma kagne lay magueu guir yallah sagesse soudone djay dinako djeundeul

  • Yalna yeurmandé yalla wathi si kawam

  • Rafetna lol guanala beugue

  • C normal

  • Ndeysane c'est triste mais bou yalla doon taggo billay dou dém ndakh kou bakhoone la loool wayé lou yalla def ken menou thi dara yallna ko sounou borom bi kharé adiana barqué ckheikhoul Khadim

  • Wakh dji raféte na ! Mais meunone nga récupérer sa rak bala beussou tay bi

  • Wakh gua lou rafete niass dieureudieuf

  • Yalla nako Mouhamet terou si Firdaysi

  • Rafet n'a niass coumba Abdallah yalla n'a borom bi motali

  • Yalna Yalla khareko Aljana firdawsi

  • PAIX À SON ÂME ALLAHOU MA AMIIINE

  • SIdy lamine yalla nako yalla yarame te youbou ko si aldiana ya gana kave mais kiko Ray lou yalla nako feki legui bala yague te kiko Ray yalla nako yalla torakhal fi si adona

  • Gnikoy sédé tay niouthi Bari ayy nonamm lagne wone ndakh môme DEUG AK yone ladone khékhal té niom ibliss lagne geumm AK adounaaa AK khaliss .loutakh sédé wouléne KO wone lou bakh bimiy doundou .thimmmmm narfékh yi nieupp pagui wakh té Dara geumouniouko

  • Thiey kou d ya porte repose en paix sidy lamine li metina

  • Ahmed lou bax rkk lay wax bayilène koo

  • SIDI EST PARTI, la vérité marchante est parti. j'ai pas eu l'occasion de la connaitre personnellement j'ai j'ai essayer en demandant des audiences pour le voir. une grande perte pour la vérité, une grande perte pour la presse . un homme qui savait que seule le travail paye. il a bâtie un grand complexe, WALFADJRI, que dieu l’accueille au paradis au nom de Walfadjri . il a fait manger ,il a fait soigner,il a fait vêtu des personnes alors que se n'était pas évident. la nation en pleure, le monde en pleure, la vérité en pleur, sidi, repose en paix au nom de TAHA MA ANZALNA ALAYKALKHOURANE.

  • Juska présent meunougnouko dégnethe c malheureux mon pays va trés mal

  • Machalla akhmete Sidi yalla na ko Yalla yeureum té djiégeul ko aminn

  • Paix à son âme