JIIXI JAAXA EPISODE 46

Ajoutée 10 oct. 2018
Retrouvez - nous sur www.okay.africa ou télécharger l'application sur :
- Playstore: play.google.com/store/apps/de...
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
- Abonnez - vous ici : fr-tv.com/username-ok...
- L'intégral de la solution "Jixi Jaxa" : fr-tv.com/tv/vidéo-jKEFDDpZ-YY.html&list=PL_HZbZROSvxYzEw5aX4hO-qx3F95M2Ut8
- L'intégrale de la série "Wiri Wiri" : fr-tv.com/tv/vidéo-ClixRV90d8M.html&list=PL_HZbZROSvxZqe3KE_Y7uyN9vJRWGlvrP
- L'intégral de la série "Mbettel": fr-tv.com/tv/vidéo-iaX29BqYa_k.html&list=PL_HZbZROSvxbDDFtr8oJVTjrkXvt9fJ6c
Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Instagram : instagram.com/okay.africa
- Snapchat : snapchat.com/okay.africa
- Facebook: facebook.com/okay.africa.tv/
www.okay.africa est votre catalogue digital du Sénégal. Webséries, théâtre sénégalais, sketch.

Commentaires

  • Touré c'est bon clifa

  • Mashalla m svp...son bissi souf la beug kham kouco woy merci

  • 😂😂😂 fo dieumak sa magoum dieum yinga andale,Ndeye Ndiaye dinama ray

  • Triste episode dioy na ba sonou quelle leçon

  • من عمل صالحا لنفسه ومن أساء فعليها

  • Koufi dèfoull lou dira jamais dû mako falè😆

  • Koumay dallall si magal gi ?

  • Wadial 18 safar mbecte mi MBA yénagui koye wadial RK Wadial safar

  • Metina trop

  • Magnoukh dead nama 😂

  • Shi ndeye ami sou commencè wakh dou nopi haha

  • MAGAL TOUBA man gann rekk la begue

  • facebook.com/100028257920000/posts/157212358564027/

  • TAPHA TOURE JE T'ADORE

  • Hommage à nos morts que Dieu les accueille dans ses paradis céleste amine.

  • Junior ak sa niary diogama yi do guawa werr

  • j'aime cette série

  • Super j'aime bien

  • Fate Kine yallanala yalla may Sa bopp nga mouthiou ci jamm amine Ci Barke Kou tedd ki

  • Wa fate kinè ba dioyii doula wagni dsra ak sa ètat

  • moma biyyy Tafa touré di annoncé Zeyna k sa mére a tué la mère de Fatkiné ehhhhh😓😓😓

  • bilahi def lou bakh mo am sole fat dam dal loko dal moke tek bopam

  • ha li daw na yarame fat kiné yeureum nako

  • Amena solo lol machalla

  • Oh my good du jamais vu mes larmes aux yeux c'est instructif

  • La guerre c'est la guerre do tou maco may darà que sa soit claire🤔😝😆

  • Tapha Tourè nitte kènne doukkoo toppou ba mou seuss

  • yala nanou yala yobou magal ak diamou

  • yayi fat kiné xana amoul tourr

  • Fuite Yalla dellenn commentair si seri bi waye

  • Fatima ne mérite pas d'être avec junior

  • Tapha et le meilleur

  • Jixi jaxa nekh na trp

  • Sama référence dalle Moustapha mai naque jiixi jaaxa mogui nice

  • Bonne continuation 👏👏👏👏👏

  • Fatou kine eh realite dafa eumbe wala?

  • mais tapha touré content n'a si mome😥😥😥😥😥

  • Ndeye diaye Ci sirie mbattel amnga yaay dioubakh mai bi serie amnga yaay dioubon

  • mann dama beugu khamm nakh amm ayy j.aime youtub pour lanla

  • Nice

  • Tapha meusso djouy😂😂meuno sakh djouy

  • Bachir Yaw Khamo sa bobou wat nala monan la guerre c la guerre Demal fek fa junior ndeye Yaw mom wero

  • Tapha dina ma Ray nenako boy kheum gua kheumé dji biti

  • fatou kine jtm wy💋💋💋💋

  • man Ak yayou fat kine nio bokou tour ndeysan ndeye bousso

  • Waaw yen dolen ma mai ndeye amie ndeye amie I love you bilie

  • Machala tapha chapeau a toi je taime beaucoup

  • Ndeysane la fin sa m rappel bi sama yay ganio sa papa dimako wax may crise mounane boulene def niii daguenemay diaxal

  • Machalla

  • T Tapha defna SMS bou ame solo vraiment

  • Tapha tourei tu jour bien bilay

  • qui voit bien que FATOU KINE est enceinte qui a fait la remarque

  • No dawna yarram Nice

  • Le meilleur épisode sama yaram drawna deysan😌

  • il y a un vrai talent chez ce Tapha, la façon dont il a annoncé le meurtre a ses enfants m'a fait pleuré wallah Nice man....

  • Yaye bou bakh yomboul Moustapha dioyilonama

  • Jiixi jaaxa💓👉😍

  • Tapha Touré le meilleur acteur!

  • 😂😂😂😂😂 cool

  • 👍👍👍👍 good job

  • fat kinei dioyal nang bala ga gagn sa bop khamna dama nimi deuguei ak fat kine mom la nara wesinn

  • No kham na ni am na gniou soffe billhi danguèna wara bayi you gniakk feuila yi nane ay kou j'aimé sma commentair yi nanguamm ndagamm daguèni commentair ci film bi bayi yii nakk kou dacor beussal j'aime

  • Tapha il est fort

  • Li.rek.moo nek senegal machahala jikhi diakha

  • moustapha je t adore encore

  • C'est émouvant ça euleuk dou agne dou reer way lou matta soralé leu def lou bax rek woor

  • dama don nélaw de no man mame ndaye gueye dinama ray way😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • Cé émouvant la réaction d la famille Touré j'avé des larmes o yeux

  • Mame ndeye Gueye Manioukhou Doléne Ma rayy 😂😂😂😂

  • Oh sama xol toyy na way yaye dafa fort fat kiné du courage 😭

  • Kiné encore plus belle

  • Hello film cool 😎 cool

  • C'est émouvant 😢😢😢

  • moussa k

  • nooooooooooo tay dioyna li dafa daw yarame

  • Bayilene wate yi li théâtre la

  • Ndama bilay lisoula daloul won ma rouss Dieuf mom nay rafet rek Maniouk😂😂😂😂😂 La scene de tapha fat kinè et ahmet trop demotions ndeysan deug rek moy moudj😭😭😭

  • Sincèrement yeureumna fatou dame ndakh djiguène moy sougnou yaye

  • vraiment fat kiné il est temps pour mou dem congé de maternité yeureumnako trop

  • yaw dale ndeye ndiaye danga dioude rek appoo theatre Bo jouer sa yaye dousi nekh let li tamitttt nane si wakh😈

  • zeyna meunoumako mougne nenako yaye fo dieum ak magoum dieum yinga andal

  • Yobalé lenn ma magal wayyy meusou ma démm

  • ma gnoukhou momay fath

  • 😫😭😭😭😭😭

  • non fatou kiné je l'adore

  • Non nekhoul ba nekhoul mais tapha ndandane la

  • Mé may léen niou ak sen safar yii ,on a na marr chak jour safar , il fe prier ç mieux de resté à chanté la chanson safar safar ....... là........

  • Ohhhh kel tristesse de Fat kiné ????? 🙏🙏🙏🙏

  • Manioukh dadji nama😂😂😂

  • prenez une leçon pour eux

  • Qui as pleuré aussi😢😢

  • DJIGUENE BAKH REK MOY YEUFEUM

  • NDEYSAANE 😭😭😭

  • جيخ جاخ

  • Non ndeye Ndiaye 🤣🤣🤣🤣

  • fate kiné médina lole

  • 7

  • Maniouk rekk aka romantique

  • Tafa tamite meunone nako bal rekk li tamite dafa eup police nak