Teuss - Temoignage de Adama Amar Propriétaire de l'appart du drame des Maristes

Ajoutée 8 nov. 2018
Teuss - Temoignage de Adama Amar Propriétaire de l'appart du drame des Maristes

Commentaires

  • Que Dieu ait pitié d l'âme d cette femme ndakh li dara diarouko!

  • Essence loumouy def thi keur ? Lolou mom ni keneu preparer wouko yalla reka ko xam yalnanou yalla diegeul rek te moutieul nou si seytanei

  • diabar sakh légi worole

  • kou ray nit te tay ko dagnoula wara ray

  • Femme bi daffa reww kessé. May wahh Aladji di diaye graww té warra wahh deugg nane doundame mo diéhh. Thipppp

  • Li yeup seuytané rek la wakh deug yalla khéyna seuytané dagua meun rek

  • Sa adina. Yakouna bâ yallah sounou borom diapela

  • Gor day matt gor wayé am sa soxna mou yilif la loumou wax nganni wàw ñiak fayda rek thiimm

  • Problèmou rèseaux putainnn!!!! Mais sokhnassi deff ngua lou eupeu😔

  • Justice soit faite

  • Mo kham dé beug lou nékh sa serign bou takhé dome bou doff bouma ame diokhla so déwé saye wadiour perte mome dess akk diabotame

  • Vraiment les sénégalais sont hypocrites,une femme qui assassine son époux et vous vous permettez de l'eloger.aucune cause ne peut justifier un tel acte

  • Vraiment c'est horrible une femme dafa wara tey mane je suis enceinte et j'ai su que mon mari me trompe mais je l'ai réglé calmement sans que personne n'est au courant mais mome moy rousse rek

    • tu vient de nous mettre au courant 😒

  • Seytane aka gaaw entre l'amour et la haine il n'y a qu'un pas

  • Saway arretez vos conneries a la senegalese, ne nous fatiguez pas avec vos histoires de rafétal, Soyons pas des nafékheux. Cette femme est une criminelle. Qu'elle aille crever en prison comme une vulgaire criminelle.

  • Ahmed dafa seytané avec sa grande gueule

  • Elle mérite d'être emprisonnés à vie

  • Deugla ki loumou def niaw na ba si kanamou yalla mais kou kheuy na ga mouslou si cheytaner li serigne cheick tidjiane wah deugla rap you bone ya gi senegal moytoulen thiow surtout les femmes

  • Parlons de ces sappeurs qui n,interviennent jamais à temps ,qui ne sauvent jamais qui que soit ,qui ne répondent jamais au téléphone et qui malheureusement.........

  • Kikaye da tite motakh mou matou ak kanamame bou dangue biiii limou yakeuh mo reuy kiii dagnako wara topou bam seus pask d'apres li wadji wakh ki dako prépareiwone essence amoul loumouy deif si keur gui sou deug neikhei reik

  • adou na dal doy na warr

  • Kou deh ya perte kholal kignu Ray bapare niewfi nane kou jiguen ki dafa bakh ki sunekon jamono yonente bi dankoy Ray joulit day mougn

  • Libéré ngaka blindé avec ça Guen Di critique macky Sall gniko Yi mo yaku

  • Man declou ndoye ban moman genel ndakh mom ragaloule ta d'où far feen li am la y wa

  • Waw man warouwma des amna mbok kiniou ray Guen ma y wakh bok ray nit dafa eup gen di wakh mandou bilahi cou def nit lou bon yala alakla a met Aidara khometoumala invibi limouwakh tegouko feen ak louniou ma a diote li waroule won

  • Bilahi Senegal mo bari na fekh wakhoulene fi dara loudoul defendre femme bi

  • Gni gno seytané maye wakhe mouné famille bi khalatoul plainte. Vraiment Sénégal amoul loi 😒

  • SUNU BOROM KHAMOUL KI DOMOU SERIGNE LA WALA DOMOU YONÉNTI LA. YALLA KOU DÉFF BAKAR LA KHAM. ET LA LOI EST AU DESSUS DE TOUT ET DE TOUS ...BAYILÈN THIAKHANE YI KI LOUMOU DEF KÈNN MOUNOUKO JUSTIFIÉ

  • Yen ay nafek nguen djiguenbi kou bone la sekoul dara ak serigne touba

  • Ak lou mene khéw bou rayone sa rak do wakhé ni ak nomou mene sante raye mome dou yone

  • Doyna war dal li métina trop

  • teudjleen ko ma damisi diabi dji les femmes daniouma diakhal sunu dike di fitnal sene dieukeur yi paré legui sou ame kenen wala mouy dokhan niou commence jalousie topatoleen sene dieukeur yi mo gueneu de ndakh goor mom foumou ame diame rek lay weur wasalam

  • Dieu l'omniscient a décrété la polygamie La polygamie est culturelle mais elle n'est pas naturelle Les sociétés occidentales où se pratique la culture de la monogamie ont le taux de polygames beaucoup plus élevé que les sociétés musulmanes où la polygamie est autorisée

  • Waw taximan bi bagne dou niou si wakh tamite

  • Mansour bayil khél yalla nafékh bakhol dé🙊

  • Man dé dioména serigne dafay défff lo rafet😡😡😡

  • Danio rayul sen mbokk rek

  • Ki soxore na trop

  • Mais ce meutre est premedité il faut le procureur fait un conference de presse...fi ya pa de masla c tun meutre ...

    • Tŕé franchement kelk soit l motif ca n justifie pa cet act inhumain

  • Li ma si mètti moy legui gnou outal femme bi papiers doff tè dara diotouko

  • Aarretez de la defendre...on s'en fou de son pere....il na k etre le president, n'empeche que c1 criminel.

  • Toi le bailleur y’a wara mandou en premier. Comment tu peux raconter une scène alors que tu es arrivé bien après les faits.

  • Bilahi Mansour vrai na fekh la ki ray ga wara wakh degeu né yala nena kou ray niou ray la ganane doundame mo diekh yaw alhourane diangeu diakhale nama mais li Gaston mbengue degeu la vrai na fhéh ga

  • Mais arrêtez avec son père bayame santou koko raye lowou koko la fille est une citoyenne lameda justice sera fait inchalla je ne connais pas ni le père ni la famille de la fille

  • Bayilen massla bi famme bi bakhol dafa wara dee ci kasobi

    • Allah y’a rahmou c est très triste de mourir de cette façon Qu Allah la rahmou amine

  • Societe bou depressive

  • Elle doit recevoir une evaluation psychiatrique ... une femme enceinte ou post partum souffre souvent de la dépression nerveuse et peut faire des choses horribles.... beaucoup de cas similaires dans le monde... souvent la Victime est très proche ( époux, enfants).

  • nagnko déff noume déff dieukeurem wakhdji diékh, bayléne nafékh ndogali yalla bosi talsa dieukeur, nitt kounéke nakol bopal bakane dafa for , yalla nagnou yalla mousal ciili.yalla kharéko aldiana.

  • N'importe quoi? Mais le Sénégal va mal, si elle a tué une personne il faut pas lui trouver des justifications...nous sommes tous égaux en droit, arrêtez de parler et laissez la loi faire son travail. Fille de marabout ou pas , il faudra que justice soit faite. Que la loi éclaire ce fait déplorable et intolérable.

  • Senegal mo bary nafek ki danio wara rey ndeyame c t un criminel

  • Té yala takh nith gni delolen sen xel Thi yala nii saytane dafa barrí dole te beupe Senegalais bou nek fii khamo sa eulekk nith Boy wakh na wakh loouko worr laniou sekkk Ba saytane niaw yala rek moko xam ak niar ngiko sekk kou xamoul sa eulekk nakk teyal Thi wakh dji , niou nian yala sam niou sam len , wa salam

  • Liyeupe seuyou appartement mokoye indi

  • Ayy Senegal delén téyy bala ngen dii wakh bilakhi Senegalais mo gawww nama yala ball , lounek degue nako bakarou Thi zero

  • Femm bi da wara kaso guiero don dam ñiaowna lol danu wara ubi la fal dayam domo aram

  • Ray nit dafa granwo lol

  • Koray nit mono bakh

  • Cette femme es horrible 😭😭😭😭😭😭

  • Sampor do dará

  • Senegal mo tarde sapor Man xamoma Loy diaredim

  • On parle de son père mais des actes de la dame elle es une criminelle elle mérite la prison à vie rek

  • Il ne faut pas oublier que tous les senegalais sont égaux aux yeux de la loi. La justice senegalaise dois aller jusqu' au bout sans compassion. Sino nous autres senegalais nous n' allons plus reconnaître la justice

  • j sw offusqėe.ds quel pays sommes nous.y as des actes q on n dw pas essaye de justifier et la loi dw sevir. si cete notre parent. comment allons nous reagir.

  • Sougnou yone elle va pourir en prison! Par A ou par B cei pas la jungle icii deuk bi amna yone

  • entouca k justice soit faite

  • Li dee di nan takh gooryi do nyou takkk diarbar dee man de titt na trop

  • Fiii ttes les femmes sont jalouses La femme est 1e assassin

  • Mai meurtre amoul serigne amoul famille la femme doit mourir en prison

    • Alimatou Diallo l

    • Sénégal amoul peine de mort donc elle ne "doit" pas mourir en prison. Que justice soit faite. C'est tout!

    • Alimatou Diallo lou weur nga wakh de

    • Alimatou Diallo son père a dit que justice soit fait lou yone wakh naniou koko deffe

  • Yalla naco yalla kharé adiana

  • me yén wa zik Aÿ seytanèguèn sou done sen mbok dolén wahè ni

  • ki dafa bonne rek assassin la tè meuna féehé loubone

  • non Sénégal nehna limo tah niti di def loulè néh ki dagnko wara teuutie

  • Teuthie ou pas adinam Yamuna c fini

  • Boulène faté ni cheytané dafa am .nagni gnane di mousslou si mome aka am dollé mome cheytané

    • Seytané dafeuh barii dolléii

  • Sénégal mo nékh kou rayy nit géne di wakh affairou mbokou. Dan ko wara rayyy

  • Kham na dal lou bone kéne mounoul fékhé bé mou bakh, Sénégal neup neupeul ak ...., comment peut-on vouloir rendre pardonnable ce qui ne l'est pas???...Aucune excuse ne saurait justifier un tel comportement ...Mane dal ma warou si sénégal!

  • Lorga sa dome de hagneko baaaye nite dafaye niteeeeee.

  • No wadji di nétali moy nanfekh deugu deugu deugu... ha d’accord prsk ki serignou wadjileu et Yalla dans tt cela? S’en genre yiii motakh crime di Bari.. ki Islam ☪️ ray nako bou yagu... ndaw si domeram lheu et kepou kou kay défendre dagno rayoul sa proche... doule way ay nafekh ngen rek. Thimm non SENEGAL sé fini.

  • *Svp Ahmed Aïdara ak sa wadji liguéne wakh andoumaci, Serigne you beuri khaliss lanouy mayé sénii dôme. En plus il faut justice def liguéyeum. Femme bi daffa bone té rééw si les faits sont avérés. Sou fékké mokko ray nanoukko ñaff ci prison bi pour jusqu'à la fin de c jours. Amoul domou Serigne, amoul domou badoula. AAY BADOLA rek lanou, danouy djeulé village, eundileuh ndakarou, def la ci appartement ngay réwantalou. Éducation lanou amoule. Que la justice fait son travail*

    • vvvvbb vbbbbbbvvv ,voir de DIEU est éternel vvbv b b.,

  • Yalla naniou souniou borom yokk soutoureu sama mbokk djigene yii naniou gueune takke souniou dingue yokk mougne tei rafeital neikine yii

  • ki dall yakna derou jiigene nit kou bone la jiigene bou bakh dou def li ak problème bou mana am solution amna

  • Léragoul

  • No mane lima guiss vs defendez la fille. Vs devez condamne sa. Mais solenkay defendre sa px encourager les otre femmes.

    • +Adji Sarr bilay ay seuytane lagn

    • Yaw tamite boumoula diakhal affair de serigne la soudone kénéne la ba tay hamet ibina guémignam bi chimm seytané rek

    • +Aicha Tv kikay rousslona nieup bilay limou def niaw na

    • C'est une malade mentale on doi condamné cet acte gni wakhougnou fi dara li dafa gnaw ki rouslona mbacké mbacké yi

    • +mooiboy mooigirl bilay yaw amiiine

  • Les gars fii cheikh bethio sakh teudjone nagn ko prison donc ne vous inkieter pas la fille elle ira en prison. Personne nest au dessus de la loie. Li khew sen diguante nak yaw mi di netali khamossi dara donc ne dis pas lignouy wakh si reseau yi dou deugu. Tte facon justice a Khadim. Manila famille bi loum diegue diegue ils vont pas pardonner la fille. Manila seuytane bou nieuwe c psk moko permetre.

    • +didi diop ta parfaitement raison

    • +didi diop ta raison ossi bougn ko teudie tamit doufa yagu. Ayway k crim impuni lay done

    • mendes shasha cheikh bethio 3personne la raylou ay talibè tes migui ni bougnou ko teudè aussi migui ni di leumbè thi rewmi badola yi raye bene nite thi prison bi là gnouy dèwè kon dou moudou fene.

    • Iiao ki mola geun mandou Il a été clair il avoue qu'il connaît pas les causes pareil pour les proches personne ne s'est prononcé... Soof nguen trop ter gnemer critiquer

    • Yaw ya xamoul lingay wakh , lou nek degue naniouko leup ay doul kou feke woul mbanoul , Ki wakh limou xam la wakh , barrí ngen problem trop ak mana goudal ay wakh

  • Dom dji rek lassi yeureum

  • Liii niaw naaa torob billahi rawatina kou santé mbacke

  • ndeysane kou khadi yak na adounam si kaso bi la nara déwé ni thieuy yalla nagnou yalla mouseul si seuy tané lou méti la

    • Alakhiram deh lako geuneu titeul, ndakh kou rey dioulite té tay ko safara rek rawatina sa dieukeur.. Allahou a'lam

  • saytané mon barydolé ak rap boy bonne

  • Yéne ay nafèx tigui guéne nax Mbacké Mbacké la dotoulen wax louma gueum guén di défendre

  • Domou Serigne Babacar Mbacké Moukabaro noo lii meunta nékk waye no aduna dièkhna kone ba paré

  • Justice pour khadim

  • 😭😭😭😭

  • frnchement cette femme est mauvaise

  • Thiéyyye yalla lou waye déf bopam

  • Mes aussi elle fille n a qu à finir sa vie en prison mm souko papam djouli aussi na loi def ligueyeme

  • Teuss mongui ni nak Li moy teuss

    • Yale na gnou yalla mouseul si sayetane

    • GolbyTV billahi lii moye teuss kay

  • li yeup may sa diabar lou eup mokoy andi complexe devant leur femme li rek lay diourr djiguene sou bakhe diapal me sou bonne fassèko ci tell

    • Bilay wakhatika j suis convaincus que c'est sa croyance qui l'a tué

    • Merci complexé ndakh domou serigne la et voici les conséquences

  • On dirait c prémédité 😱😱

  • Un bon témoignage que le bon Dieu lui accueille sur son paradis

  • Le problème c'est pas le père. La femme est une criminelle et doit mourir en prison.

  • Il faut la mettre en tôle! C est prémédité qu' elle soit elle de mara ou autre. Les maras ne voient même pas leur enfants car ils ont plusieurs femmes 5,6,7,10

    • +Brasil Dakar faut pas insulter si tu n à pas d'argument tais toi!

    • Bayil soss man Nga doull